audio
audioduration (s)
0.74
10.5
text
stringlengths
1
99
gender
stringclasses
2 values
Fan lay sax ?
male
Saa boo ragalee Yàlla Buur bi moom miiy Kenn, ku dul Yàlla dalay ragal.
male
Buma ko jàppe.
male
Ndox mi mu ëmb, cafka gi dafay sëccwex
female
Tom gisu ko woon.
female
Ma kay wayal Seex Saalihu.
male
03/07 à 2330 Mine Ubbi njël lu njëkk li
female
Mas naa jaay lii.
female
Damaa yeex a ñëw.
female
manees na am yaakaar ci moom.
female
Jën dax na, tay .
male
Kuy seenub jkat?
male
Fi mu am
male
Buy délsi yal na nu fekk ak may gu suuxali may
female
Maa ngi tëddoon sama lal.
male
Sama liggéey dafa géey.
female
Bul bàyyi !
male
Toma ngi ci kaw.
female
Biirmaani ci lu bari Bëj-saalum-penku Asi la ñu koy boole.
female
Xawma woon ne aw fen la.
male
Bëggu ñu la.
male
Damaa bëggoon a doon ndaw.
male
Wax naa dëgg, am déet ?
female
Soxla naa ab farandoo.
female
dinaa leen gindi
female
Ñu ngi ko tëye ca màkkaanum mu mag mu alkaati ya ca Ndakaaru.
female
Buleen ma xaar.
female
Bàyyi ma ma nelaw.
female
Jaxaay ji ak picc mi
female
Maa ngi jéggalu
female
Danuy jënd ay CD.
female
Suuf si daa di nangu.
female
Du sama mbir.
female
Xale yi gëmewuñu ko woon
female
Mbooram bi dëgg la.
female
Ci mbirum doomu weñ yi jigéenu-wérul war a wann
male
Loo soxla ?
male
Bàyyee gu Otris bàyyee Itaali Venezia.
male
Loolu, du lu ma jékki-jekki rekk def ko
male
Ay nit lañu.
male
Bëgg naa ci benn !
female
Nos dooley kaaraange ji
male
Doon naa ko ñaawal.
female
Nekkon na nu ay xarit.
male
Daa jubb lool.
male
Da koo kott.
male
Dangaa ñàkk jafe-jafe lool.
male
sunuy jafe-jafe ci wàllu paj soppikuwul.
female
Jëfandikoo ko walla nga ñàkk ko.
male
Dama xalaat ne danga reelu.
female
Bunu wuute nag, foofu la liggéey bi nekk
male
Damaa am ñaan.
female
Setalal sa néeg bi !
male
Toogal fii ak nun.
male
Taariix
male
Moos mi xossi nama.
male
Naj ak forse
female
Danga may fen ?
female
Noo rëyee nii?!
female
Nu ngi nekkandoowaat.
female
Teew fa nag, doore ko ci sawaal digg-bëccëg ba jant so
female
Dafa dégg i coow.
female
Mbir mii daal, kenn setu ci.
female
Am na ci ñent yoy ñi ngi ame ca armal ga
male
Tur wi feeñ na ci Injiil ci Mk 317.
male
waaye ak bii yamale, dëgërluwiin gi dafay aju ci tàngaayu wërlaay gi mu ne
female
Mbaa kuy rambaaj naankat bu màndi xaaloo
male
Mu ne «Ñoom de ñook woor diirub jamonoo yam».
female
Masuma faa dellu.
female
Beto De Canda
female
Tom sopp na mool yi.
female
Ma defoon ko ngir moom.
male
Daanaka, demewu fa noonu
female
mu wàcc-liggéey Sëriñ Abdu Laat Mbàkke wuutu ko di xalifab Sëriñ Tuubaa.
female
Damaa bëgg aar.
female
Wéer ngànnaay gi nag lii la wax
female
Moom la leen
male
Melal ni yaay man.
male
Ndax jekk ngeen ?
male
Man ngaa lakk farañse a?
female
Jox naa la ko am ?
male
Dañu maa féexal.
female
Booyal bay ab tool booyal ko am at door koo bayaat
female
Babilon dëkku penku la woon, di péeyug réewu Kalde, maanaam Irak
female
Tus-wu-taxaw wenn la ci ñaari xammikaay yi beneen bi mooy tus-wu-gaar
female
Yokkal tuuti meew.
male
Mooy ne, bala dara, Séex Anta tekkikat la woon
female
Jéem naa lépp.
male
defleen ag tànn !
male
Boo seetloo, sunu way-tawati Covid-19 yu jëkk yi bitim-réew lañ jóge
female
Man nanu koo am it jaare ko ci yeneen i lijjanti.
female
XEESAL WALLA XEEB SA BOPP ?
female
Waxi Seex Anta Joob ju aju làkkSoppi
female
Damaa sonn lool?!
female
Àdduna wori neen la.
female
Lii sax caaxaan lay niru
male
Loo leen di nëbb ?
female
Yeneen waat yi it noonu lañu mel.
female
Ku wax ?
male
Dina soxla itam ab sàkket leeg-leeg ngir mu man a law ci kawam
male
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
46