Datasets:
audio
audioduration (s) 1.18
50.6
| sentence
stringlengths 0
418
| source
stringclasses 4
values |
---|---|---|
boobu boo ko laalee ci sa loxo day taq ripp ci sa loxo | kallama |
|
Station shell icotaf | urban_bus |
|
ba mu egsee ñépp wër ko mu ni leen | alffa |
|
budee lu mel ni que business en plan la budee jigéen bi ne nekk membre fapal boo ñëwee daañu la jàppale ba nga am sa business en plan danga am sa plan commercial wala nga am sa plan de sa plan de développement | kallama |
|
amoon na ñu daan gas di ci denc seen alal | alffa |
|
dañuy dem ba mois aôut bi jeex nga buddi yëpp béy jiw su ko defee mu bañ a tawte mais ren jii bañ ko defee ndaox mi boo xoolee macha ar allah ar ñaari taw la ñu am mu arreté kon ndox mi ren demeewul noonu mooy problème bi ren | kallama |
|
toN toN u naat saa yu wëree am réew dunq yaa tax | alffa |
|
bañ loo menul à vañi darà moo k begà ém | alffa |
|
Le Baol | urban_bus |
|
damay wax ni ñëpp d ici 2080 dem 3000 danañu yegg 3000 doomu baykat bu mu fekkoon nga nekk nii dootoo doon baykat ndax dootoo am foo bay | kallama |
|
mu ne du la may doomam ndax géwal nga | alffa |
|
su fekkee ne mu nga fa dinaa ko ko wax | alffa |
|
parce que boo parcourir ree 1 kilomètre boo xam ne amul benn garab | kallama |
|
sedd lañu nekk guddi gi dafay teel a dugg | alffa |
|
Lycee Maurice Delafosse | urban_bus |
|
nan laay def ba dem Boulangerie marché mame Diarra | urban_bus |
|
Elton Ouest Foire | urban_bus |
|
Marché Taly Bu makk | urban_bus |
|
léegi de yaay tegoo njaboot gu sew gi fi sa baay ba | alffa |
|
CEM Hann | urban_bus |
|
parce que moo tax moo tax tey fële nële tey magasin ba amul benn intrant boo xamante ne nii desoon na fa muy intrant di matériel | kallama |
|
Pharmacie Talibou Dabo | urban_bus |
|
su ma sañul xarab it sañ naa gërëm ñi ma daan may | alffa |
|
billet yu bari yuñ jaay ci site en ligne yiy def anchere lu ci melni ebay wala craigslist yooyu ay billet parc-hopper yu xawa yàgg lañu te xaw nañu leen jëfandikoo | fleurs |
|
loolu aussi day gën a dem ba moom rey suufam si | kallama |
|
benn genre ngelaw boo xam ni moom la ñuy wax évapotranspiration | kallama |
|
laaj na nga leeral bu baax sa wax ji nànduma ko bu baax | alffa |
|
ñépp a mën jot ci leeraay mennum mbir mu taxaw ci yoonu jubluwaay mooy sunu taasiyoŋ ak ñakka woolu sunu bopp | fleurs |
|
Pharmacie Ibrahima Niass | urban_bus |
|
te fi mu ne nii la ma leen waxoon rek mooy développement sénégal ci suuf la jugee jëm ci kaw | kallama |
|
donc xamal na leen mbir yi kat nii la demee | kallama |
|
sa mbaal mi jén yu ndaw rekk la mëna jàpp | alffa |
|
elimaan warula def lu nit ñi di àññ | alffa |
|
alal yu baré yaram vu vér à ko gen | alffa |
|
man boog ci man nga xam ni maay yëngu ci wàllu météo | kallama |
|
dafa duggsi rekk ni wàpp ci basaN gi | alffa |
|
booy jëfandiko drone njëkkal saytu li ñula may nga widewo ko ak yan kayit nga wara joxe | fleurs |
|
ku fab téere bi ma tegoon ci taabal ji | alffa |
|
bàyyileen jaabante bi damay fobeere | alffa |
|
baye 1975 | kallama |
|
maintenant béykat bi bu organiser maintenant am na lu koy xaar ci waajal nawet kuy waajal nawet maintenant par rapport ak thème bi day taataan xibaaru météo bu ko amee maintenant ci lay mun a appliquer maintenant li ñuy wax les bonnes pratiques agricoles | kallama |
|
bindu bi daal jafewul boo ñëwee daal | kallama |
|
xam nga li ñuy wax rek moom mooy que le changement climatique là nekkatul un slogan | kallama |
|
kil la nekkal bi nga ñàkkee boo amee nekkal ko | alffa |
|
yóbbul sa doom loppitaan moo gën nga naan rab yee ko jàpp | alffa |
|
tam dafa wër àddiina foo dem fekk ko fa | alffa |
|
buy xalangu ci suuf si bàyyi ko di ko seetaan | alffa |
|
dafa dem bay toog ma xëcc siis bi mu detteerlu | alffa |
|
jaxal mbànd mi seet ndax nganj mi ñor na | alffa |
|
mooy la conférence des partis conférence boobu chef d état yi nekk si monde bi yëpp fay daje amul etatunis amul france amul keneen ñëpp a fay daje | kallama |
|
Fass Mbao | urban_bus |
|
njàngale mu xamlewul dara bëgguñu ko | alffa |
|
waa te comme gars yi dañu ñoo jàppale ci suñu béy yëpp nag war nañoo mën di def assurance | kallama |
|
maanaam li siy dëgër ak une phase liquide | kallama |
|
dañoo toppoon mbir mi ci virginia ndax mooy barab bi ki daan joxe sarwiisi internet aol dëkkoon kër gi tambali tuuma yi | fleurs |
|
te am nañu yaakaar ne incha ar allah ar ci alxames bi nit ñiy ñëwee pour visiter yaakaar naa ni du ñu am gànce ci programme boobu parce que def nañ fa vraiment lu ñu mën a wane | kallama |
|
bu dee nit ki amul information da ngay gis ne day toog rek | kallama |
|
Cem pikine Taly bou bess | urban_bus |
|
bantu ron dëgër na moom lañuy liggéeye lal yi | alffa |
|
on est resté quatre ans sans véhicule léegi la ñuy doog a jot benn mais vraiment dans un état vraiment | kallama |
|
Tigo Almadies | urban_bus |
|
xam nga xéll ne ñetti nit xajuñu ci pajaas bi | alffa |
|
kon su fekkee ne dañu am projet mu bugg a liggéey si suuf war nañ mën a am sañsañu laaj suuf | kallama |
|
Parc Forestier de Hann | urban_bus |
|
message bi nga xam ne moom la ñu leen di yox | kallama |
|
dañuy fexe ba amaat bu ñu amaat bu ñu amaatee pré base wala base ñu jox ko ñee bu fekkee am nañu ay pré base ñu jox ko ñu ñu fexe mu xool ba xam nu ñuy xaajalee juróombenn juróombenn ñu jox ñii base base jox ñii pré base comme ça ñu gën a ful | kallama |
|
Cité Police | urban_bus |
|
duma bëgg lu la neex ba ne la yàllaa ngi lay nuyu | alffa |
|
déglul ndox miy xéréréri ci mbalka mil | alffa |
|
askan wi gën a dégg ndax léegiléeg dégguma dafay bëri te ñu taamu si nag bés bi nga xam ne bésu àllarba la muy bésu luuma ndaje fi di fi am mu nekk bés boo xam ne nag demlanteeg dikklante la journée d échange la | kallama |
|
sunu dawkat yeey joN ante ak yu marok | alffa |
|
dégg naa ne omar dafay ngoro ak astu | alffa |
|
Cité Douane Golf Sud Océan | urban_bus |
|
Pamecas Cheikh wade | urban_bus |
|
ay xalaat yu ni mél ñoo ngi jeem ci gëstu lan mooy séwlo nit yi wala dilén wo | fleurs |
|
Tally bou bess Parcelle | urban_bus |
|
làkk yuñ ci dolli are làkk yu artifisiyel lañu yuñu sos ci ndorteel bi ngir yombal waxtaan ci digante yi am ay jafe-jafe waxtaan | fleurs |
|
wolof njaay nee ganaar wéete wolandoo gëse benn tànk | alffa |
|
kafe mooy porodiwi buñuy gëna jaay ci addina bi te mën ngeen gis ay xeet yu bari ci diiwaan bi ngeen bawoo | fleurs |
|
silaama sii ci cosaanu dëkk bi la bokk | alffa |
|
ba jot ci li nga xam ne moom mooy financement yi | kallama |
|
mën nañu ni pulaar la gën a dégg soose bi mu nàmp | alffa |
|
Imprimerie Tandjan | urban_bus |
|
ngàngooru jant bi rekk doy na kéemaan | alffa |
|
puudar boobu nag ci lañ ñu mën a dimbalee moom nañu ñu ci dimbali kooku li muy wax noonu rafetlu naa ko lool | kallama |
|
Mosquée Daroukhane | urban_bus |
|
Palais Presidentiel | urban_bus |
|
saako boo xam ni daal mos naay duy dara bàyyi ko teg ko nële ma leen siy jox benn exemple rek gisagu len fenn fu ñuy dem di jëndee saako ceeb ngeen gis ceeb bi ñu ne saako bi defoon na defaat mosul am | kallama |
|
mooy gën a baax neefere nag boo xam ne ci niimaa lay dund wala ci leneen loo xam ne si xëy na pouvoir am ci wàllu fertilité demeewul noonu | kallama |
|
ci yow naka la mëna dunde ak lu tuut li muy am | alffa |
|
ñii fàlu nañu buur ñii doomi buur lañu di ay garmi | alffa |
|
Mbédou Fass | urban_bus |
|
te su ñu béyoon tey ba am lu ñu dundee yaakaar naa dañuy xeex insécurité alimentaire parce que xiif dootul am ndóol dootul am njàngu xale yi dina mën a réussir | kallama |
|
ci ndorteelu xare bi dañoo tukki jaar ci kaw géeej gi lu bare wante ba radar yi dooree di yokku te di gëna xarañ | fleurs |
|
di jaajëfalaat nag suñu dg di ko daal di jox rek sunu nuyoo moom itamit mu daal di koy jagleel képp kuy yeewoo ci rajo ndefleng fm fatick ñu ngi lay tàllal sunu loxo di la naan asalaamaaleykum waaye tamit di nuyu suñu mbokki auditeurs auditrices 93 point 5 | kallama |
|
daal heure bu ñu amee ay demandeurs danañ fexe génn commune bi pour demsi yeneen communes yi | kallama |
|
Hopital de Fann | urban_bus |
|
magantewuñu lu bare seen yaay dafay nef | alffa |
|
bu ñëwee ci moo yow da nga koy diagnostiqué ba pare | kallama |
|
te tey ni ñu def ba mu jot si suuf bi moom war na ko def ba ay doomam jot si suuf mais su fekkente ne danga bëgg a encouragé xale yi nañ fexe ba suñ leen bayloowee au moins nga bayal ko tool moom tamit mu am tool bu mu bay | kallama |
End of preview. Expand
in Dataset Viewer.
Wolof Audio Dataset
The Wolof Audio Dataset is a collection of audio recordings and their corresponding transcriptions in Wolof. This dataset is designed to support the development of Automatic Speech Recognition (ASR) models for the Wolof language. It was created by combining four existing datasets:
- ALFFA: Available at serge-wilson/wolof_speech_transcription
- FLEURS: Available at vonewman/fleurs-wolof-dataset
- Urban Bus Wolof Speech Dataset: Available at vonewman/urban-bus-wolof
- Kallama Dataset: Available at Moustapha91/wolof_kalama_TTS
Features
audio
: An audio file containing speech in Wolof.- Format: Varies (e.g., WAV, MP3)
- Sampling Rate: 16 kHz
sentence
: The textual transcription of the audio in Wolof.source
: The origin of the example, either'alffa'
,'fleurs'
,'urban_bus'
, or'kallama'
Dataset Structure
Splits
The dataset is divided into two splits:
Split | Number of Examples |
---|---|
Train | 28,807 |
Test | 6,268 |
Usage Example
Here's how to load and use this dataset with the 🤗 Datasets library:
from datasets import load_dataset
# Load the dataset
dataset = load_dataset("galsenai/wolof-audio-data")
# Access an example from the 'train' split
print(dataset['train'][0])
# Expected output:
# {
# 'audio': {
# 'path': '.../train/audio/<audio_file>',
# 'array': array([...]),
# 'sampling_rate': 16000
# },
# 'sentence': 'Transcription of the audio in Wolof',
# 'source': 'alffa' # or 'fleurs' or 'urban_bus' or 'kallama'
# }
- Downloads last month
- 179
Language
)
Domain
: General speech and urban transportation
Data Type
: Audio recordings and transcriptions
Audio Format
: Varies (e.g., WAV, MP3)
Sampling Rate
: 16 kHz
Total Examples
: 24,346
Size of downloaded dataset files:
6.47 GB
Size of the auto-converted Parquet files:
6.47 GB
Number of rows:
35,075