start_time
float64
0
2.73M
end_time
float64
326
2.78M
speaker_id
stringclasses
55 values
text
stringlengths
1
4.06k
audio
audioduration (s)
0.17
388
2,335,135
2,335,677
99spk2
%hum %hum
2,335,677
2,338,796
99spk1
élevage bi tamit am na ci part bu am solo
2,338,796
2,339,220
99spk2
%hum %hum
2,339,220
2,341,938
99spk1
bu ñu xoolee rekk %e taw yi passé
2,341,938
2,342,626
99spk2
%hum %hum
2,342,626
2,346,661
99spk1
li dee ci xar yi ak nag yi bëri na trop
2,346,661
2,347,059
99spk2
%hum %hum
2,347,059
2,348,506
99spk1
ba mu tax pouvoir yi
2,348,506
2,348,904
99spk2
%hum %hum
2,348,904
2,354,749
99spk1
am ci ay ndàmpaay yu ñu joxe te ñooñu seen jur gi dee la majeur partie assurer wu ñu woon
2,354,749
2,355,237
99spk2
%hum %hum
2,355,237
2,359,121
99spk1
ndax ñi assurer woon seen contrat dafa jeexoon donc ce qui fait que
2,359,121
2,359,411
99spk2
%hum %hum
2,359,411
2,365,400
99spk1
lii war na leen yee depuis boobaag léegi nag bis bu nekk ñu ngi woote fan ngeen toll ñëw leen assurer ñu
2,365,400
2,365,834
99spk2
%hum %hum
2,365,834
2,367,770
99spk1
parce que gis nañu jafe-jafe
2,367,770
2,368,312
99spk2
dëgg la
2,368,312
2,375,949
99spk1
loolu dañu ne %e foofu tamit même chose bu dee nag bi huit pour cent la yow yaay ne sama nag lii lay jar
2,375,949
2,376,383
99spk2
%hum %hum
2,376,383
2,383,947
99spk1
vétérinaires yi xayma ko ne li nga wax loolu la ñu assurer ko ci huit pour cent nga fay quatre pour cent yi état bi fayal la quatre pour cent
2,383,947
2,384,616
99spk2
%hum %hum
2,384,616
2,386,648
99spk1
donc bu dee nag buy jar deux cent mille
2,386,648
2,387,206
99spk2
%hum %hum
2,387,206
2,389,772
99spk1
ci normalement seize mille nga waroon fay
2,389,772
2,390,311
99spk2
%hum %hum
2,390,311
2,392,924
99spk1
te %e état bi fayal la huit mille nga fay huit mille
2,392,924
2,393,298
99spk2
%hum %hum
2,393,298
2,395,811
99spk1
donc bu fekkee ne nag bi dee na
2,395,811
2,396,169
99spk2
%hum %hum
2,396,169
2,397,186
99spk1
mbaa sàcc nañ ko
2,397,186
2,397,539
99spk2
%hum %hum
2,397,539
2,400,733
99spk1
ñun ñu delloo la quatre vingt pour cent de deux cent mille muy cent soixante
2,400,733
2,401,782
99spk2
cent soixante mille
2,401,782
2,404,650
99spk1
bu dee xar yi sept pour cent la
2,404,650
2,405,130
99spk2
%hum %hum
2,405,130
2,406,368
99spk1
xar yi ak béy yi sept pour
2,407,526
2,411,851
99spk1
waaw bu dee ganaar yi un point cinq la ba trois point cinq
2,411,851
2,412,773
99spk2
ganaar sax dañ koy assurer
2,412,773
2,413,320
99spk1
ganaar
2,413,320
2,413,801
99spk2
%hum %hum
2,413,801
2,415,433
99spk1
boroom poulailler yi ñoom nga xam nañ
2,421,983
2,422,327
99spk1
waaw
2,422,327
2,422,652
99spk2
%hum %hum
2,422,652
2,423,308
99spk1
exactement
2,423,308
2,423,735
99spk2
%hum %hum
2,423,735
2,427,904
99spk1
ñooñu tamit wax dëgg Yàlla am na si ferme yu nekk Louga ñoom seen boroom ñu ngi assurer
2,427,904
2,428,510
99spk2
très bien
2,428,510
2,430,926
99spk1
donc %e bu ñu ñëwee ci fas yi
2,430,926
2,431,340
99spk2
%hum %hum
2,431,340
2,434,002
99spk1
am nañu tamit produit %e fas
2,437,060
2,438,182
99spk2
%hum %hum
2,438,182
2,440,480
99spk1
ñun am nan ndàmpaay bi ñuy jox ki nga tooñ
2,440,480
2,441,565
99spk2
%e %hum
2,441,565
2,442,669
99spk1
parce que si tali bi nga nekk
2,442,669
2,443,336
99spk2
si tali bi nga ne
2,443,336
2,444,605
99spk1
mën nga yàqal boroom oto
2,446,911
2,447,267
99spk2
%hum %hum
2,447,267
2,449,594
99spk1
ñun am na ndàmpaay bi ñu koy jox pour mu defar loolu
2,449,594
2,450,556
99spk2
pour mu defar loolu
2,450,556
2,453,363
99spk1
yow am na ndàmpaay bi ñu lay jox bu fekkee yow la ñu tooñ
2,453,363
2,453,761
99spk2
%hum %hum
2,453,761
2,457,832
99spk1
sa matériel yàqu muy charette bi muy fas bi dee na am na ndàmpaay bi ñu lay jox
2,457,832
2,458,302
99spk2
%hum %hum
2,458,302
2,459,714
99spk1
te yooyu yépp bu ñu ko xaymaa
2,459,714
2,460,510
99spk2
%hum %hum
2,460,510
2,463,007
99spk1
presque trente six mille la bu dee fas buy daw ci dëkk bi
2,463,007
2,463,459
99spk2
%hum %hum
2,463,459
2,464,436
99spk1
trente six mille franc la
2,464,436
2,464,852
99spk2
%hum %hum
2,464,852
2,469,086
99spk1
trente six mille wi mën nañu ne bu fas bi dee dañu lay delloo fas
2,469,086
2,469,738
99spk2
%hum %hum
2,469,738
2,472,264
99spk1
bu caisse bi yàqoo ñu jox la li nga jëndee caisse
2,472,264
2,472,683
99spk2
%hum %hum
2,472,683
2,474,817
99spk1
boo tooñee %e keneen
2,474,817
2,475,071
99spk2
%hum %hum
2,475,071
2,478,775
99spk1
ñu jox ko li muy defaree ba deux cent cinquante mille trois cent mille
2,480,765
2,481,290
99spk2
%hum %hum
2,481,290
2,489,943
99spk1
te am na arrêté bu génn %e service élevage xam na ko mairies yi bon autorités yi xam nañ ko arrêté bi génn arrêté interministériel buy réglementé fas yi
2,494,738
2,495,136
99spk2
%hum %hum
2,495,136
2,498,465
99spk1
képp koo xam ne yaa ngi dawal da nga war a am papier yi war
2,500,771
2,501,189
99spk2
%hum %hum
2,501,189
2,503,368
99spk1
ba ci %e circulation bi
2,503,368
2,503,659
99spk2
%hum %hum
2,503,659
2,504,625
99spk1
ba ci assurance bi
2,504,625
2,505,061
99spk2
%hum %hum
2,505,061
2,510,461
99spk1
loolu nag biir assurance boobu moo tax ñu leen di ne lii tamit dafa bokk ci suñu liggéey
2,510,461
2,511,384
99spk2
%hum %hum
2,511,384
2,517,231
99spk1
%e boucher yi tamit bu ñu jëndee sa benn nag nga yóbbu ko abatoir docteur bi ne nag bii wérul
2,517,231
2,517,844
99spk2
%hum %hum
2,517,844
2,520,793
99spk1
daf koy téye bu ko téyee ñun dañu lay delloo
2,523,688
2,524,122
99spk2
nga mbaa nga
2,525,117
2,526,764
99spk1
loolu produits yooyu yépp nag am na
2,526,764
2,527,371
99spk2
am na
2,527,371
2,531,559
99spk1
donc %e mën nañ ne élevage vraiment ñu ngi ciy def tamit ay jéego yu bëri
2,531,559
2,532,101
99spk2
%hum %hum
2,534,634
2,562,381
99spk2
en tout cas émission bi am na %e solo mais malheureusement comme lu ñuy wax donc l' émission tire à sa fin xanaa rek di fàttali mbokku auditeurs yi ñu jàppaat numéro bi bu baax a baax bu njëkk bi di soixante dix sept 413 46 46 77 413 46 46 beneen bi di 77 695 55 38 77 695 55 38 Abdoulaye lan ngay tàggatoo
2,562,381
2,564,932
99spk1
%e jërëjëf Amady
2,564,932
2,565,312
99spk2
%hum %hum
2,565,312
2,566,090
99spk1
am mbégte
2,566,090
2,566,506
99spk2
%hum %hum