start_time
float64
0
2.73M
end_time
float64
326
2.78M
speaker_id
stringclasses
55 values
text
stringlengths
1
4.06k
audio
audioduration (s)
0.17
388
2,566,506
2,567,899
99spk1
parce que sama rakk nga
2,567,899
2,568,297
99spk2
%hum %hum
2,568,297
2,568,985
99spk1
depuis Djolof
2,568,985
2,570,306
99spk2
bilaay lu yàgg dëgg la
2,570,306
2,573,493
99spk1
%e tay nga invité ma nga dalal ma
2,576,659
2,577,015
99spk2
%hum %hum
2,577,015
2,579,591
99spk1
ci biir développement rawatina bu Louga
2,579,591
2,579,937
99spk2
%hum %hum
2,579,937
2,581,871
99spk1
%e lii tamit bu xewee
2,581,871
2,582,413
99spk2
%hum %hum
2,582,413
2,585,146
99spk1
wax dëgg Yàlla ma remercier bu baax a baax directeur
2,586,901
2,587,209
99spk2
%hum %hum
2,587,209
2,587,643
99spk1
Ousmane
2,587,643
2,588,067
99spk2
%hum %hum
2,588,067
2,589,145
99spk1
ak njabootam gi yépp
2,589,145
2,589,902
99spk2
%hum %hum
2,589,902
2,595,568
99spk1
%e di beral aussi %e cant suñu jigéen sa jigéen donc Fatou
2,595,568
2,596,183
99spk2
Fatou Sow
2,596,183
2,596,846
99spk1
Fatou Sow
2,596,846
2,597,477
99spk2
%hum %hum
2,597,477
2,599,779
99spk1
parce que %e xam naa taxawaayam tamit
2,601,661
2,602,294
99spk2
%hum %hum
2,602,294
2,608,175
99spk1
%e lu ñu wax sàmmkat yi surtout li may gërëm nag mooy baykat yi sàmmkat yi nappkat yi
2,608,175
2,610,002
99spk2
waaw baykat sàmmkat nappkat
2,611,160
2,612,246
99spk1
bu ñu toogee ñoom la
2,612,246
2,612,662
99spk2
%hum %hum
2,612,662
2,618,778
99spk1
Etat bi xam na ne ñoom am na luñu représenté ci kom-komu réew mi
2,618,778
2,619,259
99spk2
%hum %hum
2,619,259
2,621,238
99spk1
te jafe-jafe yu gën bëri
2,621,238
2,621,786
99spk2
%hum %hum
2,621,786
2,625,979
99spk1
ñoom amuñu si pexe ci biir pexe yooyu
2,625,979
2,626,346
99spk2
%hum %hum
2,626,346
2,631,244
99spk1
bu ñu xoolee lu ñuy ne changement climatique bu ñu leen jàppalewul gunge wuñ leen
2,631,244
2,631,679
99spk2
%hum %hum
2,631,679
2,634,339
99spk1
vraiment jafe-jafe yi gën dana gën tar
2,634,339
2,634,875
99spk2
%hum %hum
2,634,875
2,638,896
99spk1
ci biir loolu ñu ne leen assurance baa ngi nii nguur gi dugal na ci loxoom
2,638,896
2,639,330
99spk2
%hum %hum
2,639,330
2,641,749
99spk1
bu baax a baax pour que mu gën oyof ci yéen
2,647,051
2,647,394
99spk2
%hum %hum
2,647,394
2,648,353
99spk1
mu gën leen jege
2,648,353
2,648,824
99spk2
%hum %hum
2,648,824
2,651,447
99spk1
ci biir jege boobu nag yéen ci laa leen di remercier
2,651,447
2,651,827
99spk2
%hum %hum
2,651,827
2,655,519
99spk1
parce que opportunité bi ngeen ñu jox tey def nañ fi sept ans
2,655,519
2,655,971
99spk2
%hum %hum
2,655,971
2,657,400
99spk1
mais amuñu opportunité bi
2,657,400
2,660,350
99spk2
en tout cas di fàttali ni ku leen soxla yéen a ngi montagne
2,661,472
2,661,884
99spk1
oui
2,661,884
2,662,259
99spk2
%hum %hum
2,662,259
2,663,225
99spk1
buntu ubbeeku na
2,663,225
2,663,806
99spk2
%hum %hum
2,663,806
2,667,334
99spk1
%e information bi jàll na
2,667,334
2,667,732
99spk2
%hum %hum
2,667,732
2,668,872
99spk1
te daañu continuer
2,670,519
2,671,134
99spk2
insaa àllaa
2,671,134
2,673,830
99spk1
ku ñu soxla tamit comme ni nga ko bu ñëwee ci service techniques yi
2,673,830
2,674,279
99spk2
%hum %hum
2,674,279
2,676,544
99spk1
bu ñëwee ci %e bureau ba
2,676,544
2,676,978
99spk2
%hum %hum
2,676,978
2,680,470
99spk1
vraiment daañu ko defal li mu soxla ci anam yu mu waree
2,680,470
2,684,650
99spk2
%hum %hum ñu fàttali kotamit ci %e fi ñu ci vol de bétail bi
2,684,650
2,685,009
99spk2
%hum %hum
2,685,009
2,686,279
99spk1
dañu koy assurer
2,686,279
2,686,749
99spk2
%hum %hum
2,686,749
2,689,221
99spk1
rawatina nag ñoo xam ne ñu ngi ci communes yi
2,689,221
2,689,481
99spk2
%hum %hum
2,689,481
2,691,960
99spk1
sàcc yi ci biir commune yi vraiment moo ëpp
2,691,960
2,692,521
99spk2
moo ëpp
2,692,521
2,697,063
99spk1
na ñu xam ne tamit foofu tamit %e gouvernement bi à travers assurance agricole
2,697,063
2,697,472
99spk2
%hum %hum
2,697,472
2,700,657
99spk1
mu ngi ciy jàppale sàmmkat yi ak baykat yi
2,700,657
2,701,077
99spk2
dëgg la
2,705,745
2,706,107
99spk2
%hum %hum
2,706,107
2,710,703
99spk1
te ñu ñaan leen muy donc %e l' entreprise %e sociale
2,710,703
2,711,161
99spk2
%hum %hum
2,711,161
2,712,212
99spk1
donc Jokalante
2,712,212
2,712,569
99spk2
%hum %hum
2,712,569
2,715,848
99spk1
ak partenaires am %e United Purpose
2,715,848
2,716,131
99spk2
%hum %hum
2,716,131
2,718,194
99spk1
vraiment ñu gën a jàppale baykat yi
2,718,194
2,718,465
99spk2
%hum %hum
2,718,465
2,720,772
99spk1
sàmmkat yi ba information bi war
2,720,772
2,721,198
99spk2
%hum %hum
2,721,198
2,723,152
99spk1
ci gérer seen risque bi
2,723,152
2,723,441
99spk2
%hum %hum
2,723,441
2,724,491
99spk1
mën na leen jege
2,726,843
2,727,241
99spk2
%hum %hum
2,727,241
2,728,077
99spk1
rawatina
2,728,077
2,728,309
99spk2
%hum %hum
2,728,309
2,729,539
99spk1
vraiment gox bi ñuy intervenir
2,730,618
2,779,429
99spk2
merci beaucoup kooku di Abdoulaye Deme yéen mbokku auditeurs yi yéen tamit sant nañ leen gërëm nañ leen ñi fi jot a participer ñépp nag ak ñi nga xam ne ñu ngi doon déglu émission bi seen émission %e li nga xam ne moom lañ leen doon Louga FM jagleel jokkoo ceeg waa ECHO ñu ngi leen di sant di lee gërëm tay jii nag moo doon ñenteel di derni_re émission bi waaye nag terewul ne woon nañ leen tamit insaa àllaa plus que nawet bi di gën a dem rekk baykat yi di ko gën di laajte rekk ñuy gën di yokk émission yi tay jii gis ngeen waxtaan nañ ci ak assurance bi nga xam ne moo jëm ci wàllub taw bi am na tamit yeneen comme ni mu ko waxee fii vol de bétail yaa ngi fi ak yeneen ak yeneen assurance yi nga xamante ne ñu ngi fi yooyu yépp di nañ ci waxtaan ak yéen gërëm nañ leen sant nañ leen Amady Ba moo leen ko doon dégtal di leen jox dox daje ba beneen yoon